Song: Belek
Artist:  Boiie Pablo
Year: 2021
Viewed: 24 - Published at: 8 years ago

[ Intro ]
Venxm x3
It's your boy Pablo, yeah, wow, anh, eskeit x2
Mad on the Ketchup

[Couplet 1]

Sama armoire dafa plein mais batey amoul marque Philippe
Mane damay swagg même ak silip
Ngay yakoy tangal, maalay dibiie
Dama sokhor call me syrie🇸🇾
Ci digue laay diaar douma wiirii
Damay  "tépii Roof" melni Fiiriir
Niouné boy Koy andal ? Mané idy
Niouné boy Koy andal ? Mané Zhat Vii
Mang si kanam ak sama gang bii
Yak sa Guys, yén ci rang bii
Féxé sama xhaliss nek ci banques yi, ngay danga bankk comme sa grand yi
Sama place ci classement bi, ioe sa xhappi nioung ci banc bi
Takouma montre ma raw temps bi, Thiaakhane Kat moy tegou ci temps bi
Thiaakhane Kat moy tegou ci temps bi 

Soumay dougal-guéné loloy bénéfice
Wala may sékak sa bébé fiss
Zéro stress doniu presser fils, koo niou boolel dagnkoy dresser fiss
Yakoy salteel maalay makoy bomb fiss
Même scientifiquе duniu chercher fils, daniou beurii problèmе pays d’guerre ak crise
Beurii pêchers fiss, faaw niou precher fii

Nigga dougou ci tahoul ci guénn ci…
Baaylén niouy gueuleum dii diéguéssi
Même bouniou bougéwoul maléndi fékissi
Thiow lii dou dieekh melni fénn yi si, journal ak télé yi nekk fii
Mais batey téréwoul ma nekksi, dieul si fiitou guy lekksi
Meunn nga dieul si sama sons yii séki si, bo maré xham xham nieuwal nga deeksi
Bo namé enjoy nieuwal féthieu si, dama beurii flow melni fashionweek (dama beurii flow melni fashionweek)

Xharou nguirr gathié dou idéé, ndakh Yawmal khyam nieupay took -
Kileu beugg moley fiiré, motakh foo diaar dalay soof-
Young nigga gueumal lii fii né, real dou daw té dou xooF


Pour signer chèque, contrat,Ragalougn combat
Kou fii meuss,contann, meussna cry so hard
Koufii siiw ,am kaagn ,meussna fight longtime
I’ll not so fine, if i lose my time
Normally easy job never get high price (never get high price)
Normally easy job never get high price
[Couplet 2]

Douma beugg damay niquer
Douma seugg damay viser
Dama kawé niveau douma piqué
Bo niémé niakkeu nieuwal miser
Sa leer lay satieu diokh la misère
Sa carrière’y guena gatt sama teaser

Kou melni mane amoul fénn !
Dou fii dou feulé no dou fénn mane bimay feull nioungui fowii
Té liniouy forcer damko foowé, foma woo cii fiitneu naala fekk  foo'né
Dou Freestyle dou featuring degn ma ci former
Boo démé ciibiir boul déclarer forfait ndakh mane douma frotter damay frapper fooré
Dey yombb nga fokné mais reppal ba sopp rek
.........Heey

Fils soudoul Pablo no dou kénn !
Dou kii dou keulé no dou kénn
Ioe meunn nga compter doo guiss kénn
Wakhma koumay concurrencer dou ci lénn
Mane ci leer la gueuleum niom niouy-outii lerr
Boul diaawalé remplaçant ak-titulaire
Daniou garer ni auto you pane ci fouriére

Kepp kou sisous 3em baram !
Nioune beugougn sa léneu fiss- té dougn xhaarane
Hey doo guiss ma feat. ak nieupp- nikouy mbaraane
Sa MC sakh mane ley weur, mane mey ndaanane
Yoone bii leer na samay beutt- douma saarane
Teksi diokh gueum lima beugg- douma thiaahane
Seytou fimay tekk ay tankeu- douma diaakhane
Awma diotou kou am diote, douma saggane
Bomay yeblou boum-la yeem, soumley saaga
Douma yem ci dem sén keur, damay Fanane
[ Outro ]

Give the respect anyway, dougn la maral
Have to fight every day, duniou seral
Narcotic is the brain, doma helal (never, never, never, never, hey hey never)

( Boiie Pablo )
www.ChordsAZ.com

TAGS :