Song: Boula Dara Meti
Artist:  Admow
Year: 2019
Viewed: 31 - Published at: 10 years ago

Yena say nga fok ni thi adouna bi keneu doula comprendre
Sometime nag dem ba diap ni doto museu contan
Ci bir keur gui Yaye boye nela doula meye nada
Ci mbeda bi yeah yeah
Ragala takh ngani do maye dara
Mais nak boul diakhle, yone leu mou diaffe
Want maadi goor bi kham fi nga feete
Kham sa ndieuga takh ma deukh thi di niaafe yeah yeah
Thiofeleu ci bir khol bi
Diox ma confiance ma yoboula fu sorri
Ou bebe oh bebe

Damala love love love baby love love love
Boula dara mеti
Nakhar diekh na tey mangi thi sa wetе
Boula dara meti
Dinala thewal thi nadj
Thewal la thi kerr
Baby i got your back
Boula dara meti
Ecoute moi baby
I love you lady
Et je sais que t'as peur de m'aimer
Si tu t'inquietes pour moi t'as tord
Faut que tu sort de ton decors
T'as deja gagner mon coeur
Donne moi ma chance
Fais un effort
Soumala xole guiss thi yow ku am ndiom
Douma beugua loudoul done sa heros
Do wete thi bile yone you are not alone
Je suis ton ange gardien
Ohhhh
Baby you're the one, baby you're the only one
Baby you're the one that i need in my life

Damala love love love baby love love love
Boula dara meti
Nakhar diekh na tey mangi thi sa wete
Boula dara meti
Dinala thewal thi nadj
Thewal la thi kerr
Baby i got your back
Boula dara meti

Damala love love love baby love love love
Boula dara meti
Nakhar diekh na tey mangi thi sa wete
Boula dara meti
Dinala thewal thi nadj
Thewal la thi kerr
Baby i got your back
Boula dara meti

( Admow )
www.ChordsAZ.com

TAGS :