Song: Dieukeur Sama
Artist:  Aida Samb
Year: 2021
Viewed: 31 - Published at: 7 years ago

Oh baby my baby man teyy ma woyal la
(ohhh teyy ma woyal la)
So beugué nga taccou me feccal la lova
(ohhh ma feccal la lova)
Ma la beugua beh doff teh deh xaw ma li lan la
(ohhh xaw ma li lan la)
So nobé linguaye doundeu lenen la
I love you yow dieukeur sama
Koula beugue mola sonal
Sama mbeuguel deugg la
Ohh bae oh
Xol bi xamal nama
So beugué tey mouy deugg linguaye doundeu lenen la
Oh bae oh

Ohhhh baby man nopp na la boy bi man nopp na la
Ohhhh baby yeah won ngaama
Motakh man nga nekh ma
Boul faté limala wakhon
I love you teh lepp louma morm yow ya ko morm
Te quiero
Cherie xamal ngaama
Ma deh ci sa xol, ci sa xel mi laye fanan
Te quiero
Yow la, yow la nopp
Yow la, yow la, yow la nopp
Nyatta ma topa teh yow la nopp
Saga ma dorr ma man yow la nopp
Yow la, yow la, yow la nopp
Wakh ko sa papa man yow la nopp
Wakh ko sa yaye man yow la nopp
Nga xam ko ci tel man yow la nopp
Yeah, yeah

I love you bae, amore mio
Superhero, Yang maye mirr lo
Ya takh duma ngiiro
Birr negg ba nga dieugé ma
Sometimes nyu rompampam
Beugg na la beh fou beugg yem oh
Boye demm dema yobalé

Oh baby my baby man teyy ma woyal la
(ohhh teyy ma woyal la)
So beugué nga taccou me feccal la lova
(ohhh ma feccal la lova)
Ma la beugua beh doff teh deh xaw ma li lan la
(ohhh xaw ma li lan la)
So nobé linguaye doundeu lenen la
I love you yow dieukeur sama
Koula beugue mola sonal
Sama mbeuguel deugg la
Ohh bae oh
Xol bi xamal nama
So beugué teh mouy deugg linguaye doundeu lenen la
Oh bae oh
Ohhhh baby man nopp na la boy bi man nopp na la
Ohhhh baby yeah won ngaama
Motakh man nga nekh ma
Boul faté limala wakhon
I love you teh lepp louma morm yow ya ko morm
Te quiero
Cherie xamal ngaama
Ma deh ci sa xol, ci sa xel mi laye fanan
Te quiero
Yow la, yow la nopp
Yow la, yow la, yow la nopp
Nyatta ma topa teh yow la nopp
Saga ma dorr ma man yow la nopp
Yow la, yow la, yow la nopp
Wakh ko sa papa man yow la nopp
Wakh ko sa yaye man yow la nopp
Nga xam ko ci tel man yow la nopp
Yeah, yeah

( Aida Samb )
www.ChordsAZ.com

TAGS :