Song: Dof Ci Yow
Artist:  Admow
Year: 2021
Viewed: 56 - Published at: 3 years ago

Ana litakh nit ki di beugg
Takh nit ki di bagne
Takh nit ki di dioy
DI dieufe limouy bagne
Yow d yaay ki take mun daw
Ngirr nga sorri Bepp thiow
Ta de thiaabi feete Galen guinaaw

Tewoul tey leelu gueneu nop
Tay leleu gueneu fonk
Tay leleu gueneu sopp
Tay la geuneu doff ci yow
Bi mbeuguel bokoul ak bu nioniou
Bi mbeuguel bokoul ak bu nioniou

Mom nena finga dem lay dem
Finga neh lay neh
Mbop ak Mbop
Mbag ak Mbag
Tank ak Tank
Ndakhte yow leu love
Wadji nena yow leu love
Mom nena finga dem lay dem
Finga nеh lay neh
Mbop ak Mbop
Mbag ak Mbag
Tank ak Tank
Ndakhte yow leu lovе
Wadji nena yow leu love

Ouh, Yena bokk yeugg yeugg
Ouh, Yena bokk ngeum ngeum
Ouh, Yena bokk guiss guiss

Tu es celle qu'il a choisi
Qu'il a suivi
Tu es son ame soeur
T'es celle qui a fait de lui un Kilifa
Ouais ouais t'es celle qui a fait de lui un Kilifa
Kon khamal ni nak
Mouy nadj di goudi
Ak loumou meyti
Dou messeu bayi
No no dou meusseu khadi
Nyaari nit leu teh yen nyaar la
Kon nak beugeuntelene waay

Mom nena finga dem lay dem
Finga neh lay neh
Mbop ak Mbop
Mbag ak Mbag
Tank ak Tank
Ndakhte yow leu love
Wadji nena yow leu love
Mom nena finga dem lay dem
Finga neh lay neh
Mbop ak Mbop
Mbag ak Mbag
Tank ak Tank
Ndakhte yow leu love
Wadji nena yow leu love

Waw walaye fi nga neh lay neh
Way fi nga dieum lay neh
Mom Mbop ak Mbop
Mbag ak Mbag
Tank ak Tank
Ndakhte yow leu love

Xale bi ne morm yow leu beug way
Xale bi ne morm yow leu love way

Ndakh nena fi nga nek lay neh
Wa walaye Fi nga dieum yow lay neh
Ndakh mbop ak mbop
Mbag ak Mbag
Tank ak Tank
Ndakhte yow leu love

Xale bi ne morm yow leu love way
Ndakhte yow leu love
Xale bi ne morm yow leu beug waw

( Admow )
www.ChordsAZ.com

TAGS :