Song: Feccal Ma Afromix
Year: 2020
Viewed: 24 - Published at: 8 years ago

Dou question dou diameu nguéweul wakhé noppi
Dou question dou diameu dou diameu nguéweul wakhé noppi
Maa maa nangouwoul thiow

Mane xamna Mane xamna
Sou bobaa dina xéep niéee
Sou booba niou nane amone naafi cas
Mangui nii thie sama waar dinay sanguiné dani baa euleuk

Ma waye lii
Ga féthie lii
Gnou andeu béguéee
Yaw mimay béguéee diougal yeungooo

Ma waye lii
Nga féthie lii
Gnou andeu béguéee
Yaw mimay béguéee diougal yeungooo


Chaba dibine dabine daraa
Chaba dibine dabine dibindéwoo
Chaba dibine dabine daraa
Chaba dibine dabine dibindéwoo
Ma woyal gaagni waw
Anh guii ngéweul
Ma béteu woye wi diaglél lénko


Ma waye lii
Nga féthie lii
Gnou andeu béguéee
Yaw mimay béguéee diougal yeungooo

Ma waye lii
Nga féthie lii
Gnou andeu béguéee
Yaw mimay béguéee diougal yeungooo


Ma wayе lii
Nga féthie lii
Gnou andeu béguéee
Yaw mimay béguéee diougal yeungooo

Ma wayе lii
Nga féthie lii
Gnou andeu béguéee
Yaw mimay béguéee diougal yeungooo

Teubeul teubeul way teubeul teubeul teubeul
Teubeul teubeul way teubeul teubeul teubeul
Féthial ma
Teubeul teubeul way teubeul teubeul teubeul
Teubeul teubeul way teubeul teubeul teubeul

( Wally B. Seck )
www.ChordsAZ.com

TAGS :