Song: Luthioum Luthioum
Artist:  Diaw Diop
Year: 2018
Viewed: 54 - Published at: 3 years ago

Kou ame sa cherie boye
Danga koy woné
Mala beugg bi
Motakh ma laye woyal
Kou ame sa cherie boye
Danga koy woné
Mala beugg bi
Motakh ma laye woyal sama cherie

Fi la la Beugué
Ci digg goor gni
Fi la la aimé
Fo diar dama laye woné
Fi la la Beugué
Ci digg goor gni
Fi la la aimé
Fo diar dama laye woné
Yow yaye sama cherie

Nitt ki so ko beugué da nga koye woné
Man mi ni ma la beugué fo diar dama laye woné
Ni ma la beugué, ni la la koye woné yow sama cherie
Ni ma la beugué kou mou nekhoul di nga sone fatigué
Ndakhté yama gueneul kaye dougueu Aldiana
Ni ma la nobbé kou mou nekhoul di nga sone fatigué
Ndakhté yama gueneul kaye dougueu Aldiana
Yayе sama cherie fraise
Sama Banana
Sama coco mandarinе
Cherie namo dara
Yaye sama luthioum luthioum
Sama lathioum lathioum
Sa su nyu weeté ya maye tarilo suratul Ah
Astafullah
Bai ma ma noppi bala yaye di ma dega
Ma risqué tekk ko pitier beh Dakar di nyu jugé
Bai ma ma noppi bala yaye di ma dega
Ma risqué tekk ko pitier beh Dakar di nyu jugé

Man ak yow do nama dara
Lo nama ma deffal la ko
Xam na ki nga done

Xam nga cherie coco yaye suma baby

Ni ma la beugué kou mou nekhoul di nga sone fatigué
Ndakhté yama gueneul kaye dougueu Aldiana
Ni ma la nobbé kou mou nekhoul di nga sone fatigué
Ndakhté yama gueneul kaye dougueu Aldiana
Yaye sama cherie fraise
Sama Banana
Sama coco mandarine
Cherie namo dara
Yaye sama luthioum luthioum
Sama lathioum lathioum
Sa su nyu weeté ya maye tarilo suratul Ah
Astafullah
Bai ma ma noppi bala yaye di ma dega
Ma risqué tekk ko pitier beh Dakar di nyu jugé
Bai ma ma noppi bala yaye di ma dega
Ma risqué tekk ko pitier beh Dakar di nyu jugé
Sama mama woye na leu eh eh
Yayu Amina leu madame Diob
Ma la beugg dama laye woné
Man ma la aimé dama laye woné
Nama na la, dokhantusil, kaye nga dokhantusi
Dama laye woné fokk nga dokhantusi
Dokhantusil, kaye nga dokhantusi
Dama laye woné fokk nga dokhantusi
Xam neh da nga jolie
Nama na la, dokhantusil, yama dokhantusi
Dama laye woné fokk nga dokhantusi
Dokhantusil, ya yeum nga dokhantusi
Dama laye woné fokk nga dokhantusi
Xam neh da nga minione

Sama cherie fraise
Sama Banana
Sama coco mandarine
Cherie namo dara
Yaye sama luthioum luthioum
Sama lathioum lathioum
Sa su nyu weeté ya maye tarilo suratul Ah
Astafullah

( Diaw Diop )
www.ChordsAZ.com

TAGS :