Song: Ney Leer
Artist:  Boiie Pablo
Year: 2022
Viewed: 55 - Published at: 7 years ago

(Intro)

45° Drill, Boiie Pablo, Check, wow, anh

(Couplet 1)

Bo amoul Dara waro xheep Dara ndakh boudoul Dara nigga IOe diarago dara
Boul bagn sa bop xholal niinga nékéé
Ndakh Lii nga nékéé rek ngay moudié nék

Sou dee doulone béété kenn douko ragal
Do xham louy ragal boula Yallah di faral
Do ragala dialeu ci yone bimley xharal
Ak loumou meuna tarr’a tarr ioe dalakoy diaral

Ki banioul dara sakh am na limouy bagn
Ndakh bania niakk motakh dou meuss bagn
Goor fall sa weurseuk kenn doulako xhagn
Fii lepp lou diote yombou nak xhana nga bagn

Dee dafay bêté té mom nena tekk
Fepeu lalay fekeu fexhel kone mou diekeu x2
Même ki guena kawé souf si dakoy lekeu
Wakh yi guena soufé Yallah mingkey degg
Bo nékéé ci bamel youkhoul dougn la degg
Way Lou janteu bii tangg bamel meun n’a sedd

Boy taneu niite tamoul kilay taneu ndakh boko tamou mom’ite ioe leu tamou
Diokhé nimbeul mo gueun wooté nimbeul
Diokhé ndiigueul mo geune dieufé ndiigueul

(Refrain)

Degn my nigga, hey deugg dou degn my nigga
Bagn my nigga, hay somay bagn my nigga
Degn my nigga, hey deugg dou degn my nigga

(Couplet 2 )

Lii contre attaque leu..fuck seu tic-tac
Remonter nieup..fuck sen tactique
Yone bouy gaaw leu no dou ay Zigzag
...( No dou ay zigzag )

Dama am bac diayleu prek ak ZhatBoiie
Dougou ci rap bi tek yeufou bad boiie
Keuff senn buzz youkhou leen sathioy
Xhiif ay atte xhawma louy paatio
Am rapp di def Rap motakh bama rabé
Dou am alal rek mo wara takh nga tabé
Lepp loy xhepp sa bop am n’a niite ko tané
Nieup yemou niou wanté nigga nieupa diafé

Yamba bi amoul courant wanté fimley yeegueul ascenseur bii xhalaatoufa egg
Ba takh n’a Boyi thiolé ci sen Life dem dieul ci joint yii fokné nio guena egg

Diokh ma respect force ni sey Généraux
Diote ay tonne appel melni Guerrero
Niouné job nice neu nigga gérer ko
Mané zéro pression douma weeré bro

(Pont)

Dama am bac diayleu prek ak ZhatBoiie
Dougou ci rap bi tek yeufou bad boiie /
Lii contre attaque leu..fuck seu tic-tac
Remonter nieup..fuck sen tactique
Yone bouy gaaw leu no dou ay Zigzag

(Outro)

Degn my nigga, hey deugg dou degn my nigga
Bagn my nigga, hay somay bagn my nigga
Degn my nigga, hey deugg dou degn my nigga

( Boiie Pablo )
www.ChordsAZ.com

TAGS :