Song: Taff Taff
Artist:  Gun Mor
Year: 2021
Viewed: 30 - Published at: 5 years ago

Taff taff

Skuuuuu coups de feu


Taf taf taf taf taf taf trac taf taf taf


MOR
Bombe atomique samay couplet
Doumalene maye fouguene souflet
Yagui si kaw mais dagua soufé
Sama kaname nigua touté!!
Lo beug salé wala sucré
Mala tegal lako guay guiss vitfé
Mane douma raté souma cibler
Nek si sama champs de tire c’est trop risqué
Oh yeah
Gunna gun petit dragon
Kone Ndiaye sama flow ladone degg mouy rire
Mounouma dounde ak gnom
Dagni dead dead leu ma geune lene mourir
Mane ak yene dougne ay nawlé
Lileni raye momay nourrir
Phenomеnal Sama projet
Gunmor coup de feu jay z bluеprint
Yeah
Niggah limoy rapou titans
Xalay gueneu si sama guemigne mane la reiner
Oui je me tire pour vivre comme un gitan
Original mor loumay doyé China di final
Au faite
Sama match dou ame mi-temps
Biss boma topé digua saw ba dead ni fowé
Si sama bopp Bou ndaw bi amna xel Bou puissant
Boma woowé si game petit damlay fowé oh yeaaaaaahhhh

Refrain
Aka ma niémé tar tar
Hey Dama dof dou kaf sax
Hey Massi wara guéné sama askane
Fokma Lidieunti cas bi taf taf
Right now taff taff
Vite fait taff taff
Right now taff taff
Tout de suite taff taff
Right now taff taff
Vite fait taff taff
Right now taff taff
Tout de suite taff taff
Right now

CAB
Hey Taf taf
Dama lene di tendre Par 4
Kou yeungeutou ma dougal leu si kamb taf taf
Topp samay tankou papa
Yo yi né galé malene wara pompe attak oui
International ni Gana gueye
Danie yagga risquer di 4 appuis
Cab rappeur bou S4 ordinaire
Hey Chaque sortie niom nieupay tiit may begg di am cash di def sama compte
Wooo Sopiléne sénoup style fi drip bi day chaud eclater ay bombe
Lima fly motax ngamay diapal haine
Pain kouko khof boufi xaar sax gain
Nigga yanguey Cap
Mytho man ngay tek
Béne pussy nigga douma diay ay prek
Melal ni fleche no def dinanie daw ba keuf sa fitt
Danie fek kou khiff tok niou dioxko beef
Def lacoste tey tiop ni crocodile
Gueune yor directeurou sococim
Heure bengui daw ioe nga tok di wahtou rek
The goal was not to get seen danie beugona kaaniou rek
Kruuu baaaaw
Refrain
Aka ma niémé tar tar
Hey Dama dof dou kaf sax
Hey Massi wara guéné sama askane
Fokma Lidieunti cas bi taf taf
Right now taff taff
Vite fait taff taff
Right now taff taff
Tout de suite taff taff
Right now taff taff
Vite fait taff taff
Right now taff taff
Tout de suite taff taff
Right now

( Gun Mor )
www.ChordsAZ.com

TAGS :