Song: Yow La
Year: 2021
Viewed: 143 - Published at: 7 years ago

Oh mbeuguel ay sentiment la
Da na da lou makk, da na da lou ndaw, ay sentiment, mbeuguel
Diokh na la sama xol, boum bi do ko dokk
Forcer wouma ko, yeurmandeh la ci bote
Waat na yaye sama, mama
Sama famille de ci man nyu naan danga bone ci man
Dunyu musa am ndam ci yow
Waat na sama mama dey yow la

Ma tey nopp la sama baby (Mbeuguel a nekh)
Bokk Bebe, souma solo yow la, souma rehyeh yow la, souma merreh yow la
Bilaye walaye, sama Ardiana dey yow la
Ma tey nopp la sama baby (Mbeuguel a nekh)
Bokk Bebe, souma solo yow la, souma rehyeh yow la, souma merreh yow la
Bilaye walaye, sama Ardiana dey yow la

Dieul sa panier, nduggi marcé
Togal ma thiebou djeun, reec beugeuj suul ci deugg gi
Pachal limong, tuti kani boul fateh niekh si xonj bi
Diongoma bi diougeh li lan la
Sama penda narr dey yow la
Je t'aimes walaye, souma koy wakh xol bi dafay nekh
Je t'aimes, tu m'aime, souma koy wakh xol bi dafay nekh
I love you, i love you, i love you, mon amour

Lunj ma meye ma dench ko, xar nga nyow ma diokh la ko
Duma la musa bougal, bul ma diaye sa reew, ma dieul
Vraiment Sama ardiana dey yow la
Je t'aimes ma baby (eyo je t'aimes), ahhh je t'aimes (eyo je t'aimes), mama je t'aimes (eyo je t'aimes)
Sama yaye je t'aimes (eyo je t'aimes)

Ma tey nopp la sama baby (Mbeuguel a nekh)
Bokk Bebe, souma solo yow la, souma rehyeh yow la, souma merreh yow la
Bilaye walaye, sama Ardiana dey yow la
Ma tey nopp la sama baby (Mbeuguel a nekh)
Bokk Bebe, souma solo yow la, souma rehyeh yow la, souma merreh yow la
Bilaye walaye, sama Ardiana dey yow la

Dieul sa panier, nduggi marcé
Togal ma thiebou djeun, reec beugeuj suul ci deugg gi
Pachal limong, tuti kani boul fateh niekh si xonj bi
Diongoma bi diougeh li lan la
Sama penda narr dey yow la

Ma tey nopp la sama baby (eyo je t'aimes)
Bokk Bebe, souma solo yow la(eyo je t'aimes)
Souma merreh yow la (eyo je t'aimes) Bilaye walaye
Sama Ardiana dey yow la (eyo je t'aimes)

( Soryba Kouyat )
www.ChordsAZ.com

TAGS :