Artist: Ashs The Best
Lyrics of Artist: Ashs The Best
  1. [Lyric] Sutura (Ashs The Best)

    Ci sutura Ci sutura Ci sutura Sama waaji na ñu waxtaan ci sutura Xarit, dee naa la ci sutura Ci sutura laa lay waxee sama ge'nt Sutura Ci sutura laa lay samay proble'mes akk lima dal Sutura Ci laa lay de'nkee sama guddi Bulma weer ni bëccëg Bulma weer ni bëccëg Sutura sutura Bulma weer ni bëccëg Ndax yombul nga xamal ma Mbokk waay Sutura...Learn More
    popAshs The Best
  2. [Lyric] Yaay Joor (Ashs The Best)

    Hum hum Weettay dima ray Té niémé wou ma netali Mangui sama yoon Ni pithie Ramatou Yala dima weteuli Gorr momoul nianne Yareewouniouma tallal lokho Yaay joor sama yaye Mangui sakkou sa niane Yeurmande amoul fii Wettay ak namel Nek ndaw ci samay digeu morom yaffouss warouma Fii lekougnou ba sour Nanouniou ba mandé Way nek ndaw ci sunu digeu morom...Learn More
    popAshs The Best
  3. [Lyric] Xel Akk Xol (Ashs The Best)

    Yeah, eh eh eh Lé, lé, walé Hum, hum Suba suma yeewu Yaw lay bëgg jakarlool Sa suma yeewu Yaw lay bëgg njëkk xol Ëlëk lu mata soor la Wayé xel xalatu ko Ëlëk ay jaar-jaar la Sama xol yëgoon nako muy ñëw Xel xalaat la (xel ak xalatam bë) Xol yëkk yëkk la Nit ak jëmëm jë Dara xaaju fë Sa suma yeewu Yaw lay bëgg njëkk xol (Suma yewo yaw la bëgg njekk...Learn More
    popAshs The Best
  4. [Lyric] Gadaay (Ashs The Best)

    Chiii riii reee Chiii riii reeeraa Ahhhhhhh yeaaaaaaah Guestu woma Deglou woma… May ladj lou khew? Guissouloma Té guissone naani Danga reer ma lay dieekh Dama fok ni tayouloko Ndakh mbeuguel Defone naani dinga changer balaa ma dem Andandoo bi si diamono dji Meune na khar ba benene Kharit woma, woma yeema Sou fekké may nelaw Fou niou tollou kan...Learn More
    popAshs The Best
  5. [Lyric] Ñibisil (Ashs The Best)

    Ñibisil Ñibisi-i-il Jukk du wess, jukk du wess Suma lay woo lutax doma falé Wax ma lu dañ ci man xana bëgëtoma Yeah, yeah Bëtu mbëgëel lala mësa xol le Lu waral man ak yaw ñu dëkk si cow Suma xolei fuñu jar yep Dag ma wowon dima deff fu sori Bi ñuye goro loxam wax ma Tay bitti bi molay gërëm kër gi joy triste Samba alar waw si njabot ji Xol yagi...Learn More
    popAshs The Best