Song: Gadaay
Year: 2021
Viewed: 18 - Published at: 6 years ago

Chiii riii reee
Chiii riii reeeraa
Ahhhhhhh yeaaaaaaah

Guestu woma
Deglou woma…
May ladj lou khew?
Guissouloma
Té guissone naani
Danga reer ma lay dieekh
Dama fok ni tayouloko
Ndakh mbeuguel
Defone naani dinga changer balaa ma dem
Andandoo bi si diamono dji
Meune na khar ba benene
Kharit woma, woma yeema
Sou fekké may nelaw
Fou niou tollou kan ngay woolou
Koudoul sa khel
Balaa ma dem nala wakhni amna thiofeel
Thiofeel bi ma am si yaaw
Waat na ni doko yeug
Walay dang ma miiin ba doma yeug ba maaa ngay dem
Guestu woma…
(gadaay gadaay fou sori)
Yeugouloma yaw… yeugoulomaaa…
(gadaay gadaay ndakh tiono)
Falewouloma…
(gadaay gadaay ndakh mbeuguel)
Toppatoo woma yaw
Toppato womaaa
(gadaaaay…)
Guestu woma
(gadaay gadaay fou sori)
Yeugouloma yaw… yeugoulomaaa…
(gadaay gadaay ndakh tiono)
Falewouloma…
(gadaay gadaay gadaaay daaay daay)
(gadaay ndakh mbeuguel)

I know something wrong…
Domou yaye mba fatewouloma
Wooté na té wouyoulo
Cause i know something wrong
I know something wrong
Mangi dokh ak tankou neen ci naadj bou tang lool
Mangi marr naan ndokh, diaffé lool
I know… cause i know somеthing wrong
Guileeee! dieul si ma kharit sama, domou yaay fima tollou weet na
Bileee! domou yaay dieul si ma kharit sama fima tollou weet na
(mbaa meré womaaa?)
Domou yaay diеul si ma…
(mbaa meré womaaa?)
Kharit sama… domou yaay dieul si ma
(mbaa fatéwomaa?)
Domou yaay dieul si ma
(mbaa fatéwomaa?)
Kharit sama domou yaay dieul si ma

Guestu woma…
Lijenti wo ma yaw lijenti wo maaa
Falewoulomaa…
Toppatowoma yaw toppatowo maaa
Guestouwo ma
Khoolou loma yaw
Yeugoulomaaa
Falewoulomaaa
Lijenti woma yaw ba takh gadaay naaa

(gadaay gadaay fou sori)
(gadaay gadaay ndakh thiono)
(gadaay gadaay ndakh mbeuguel)

Gadaay gadaay…
Fii kou fi wathie saw andeu…
Andeu boo dem fekk fa sa morom mou took
Khalé ya ngi gadaay
Fou diant sowé timis massé kou lay yobbaalé
Ndakh goudi khaadj neu fadiar waadj neu euleuk soraalel
Reuthiou weess neu dieufam fegn neu kokoy diggaalel
Loudoul yalla neen leu yeené neeg leu nga fay fanaané

( Ashs The Best )
www.ChordsAZ.com

TAGS :