Artist: Natty Jean
Lyrics of Artist: Natty Jean
Lyrics of Artist: Natty Jean
[Lyric] On ma dit (Natty Jean)
On m’a dit faut pas rêver la vie est dure / on m’a dit tu verras c’est plein d’aventure On m’a dit tu te feras des égratignures/ par la suite il faudra soigner tes blessures On m’a dit si tu ne te bats pas tu finiras clochard dans la cité On m’a dit si tu n’écoutes pas tu vivras dans la médiocrité On m’a dit surtout ne pleure pas tache de garder ta...Learn MorepopNatty Jean[Lyric] Sénégal (Natty Jean)
This is for my people Sénégal Njaay! Jolli na well, music bi deh le jolli na fi nañu teg level Ne Sénégal de kenn du ko yàq ak nimu mel Ñu change mentalité faut que ñu change suñu xel Xol yi nañu sell, naatange jolli well Man de lima xam ci corruption dugg ci jail Ku ci wàcc yoon ñu xàcc, bàcc yattu kel Ku fi jiite xamal ni xol yi de fees na...Learn MorepopNatty Jean[Lyric] Adouna (Natty Jean)
Nit ñi fi ñuy rawante / mooy ci xol yu rafet yee Nit ñi fi ñuy amee barke/ mooy ci ñaanu waa-jur yee Nit ñi fuñu jëm ag yaakamti / xanaa bëg yaxxule Kon sa wërsëg ding ko fekkee/ xanaa waxtu bi su jotee Na nga sant, sant, sant, sant te baña yàkkamti waay Kon defal ndank, ndank, ndank, ndank mooy jàpp golo ci ñaay Mu xiin, mu taw, mu neex, mu naqari...Learn MorepopNatty Jean[Lyric] Ego Trip (Natty Jean)
Bayyi leen ma wax, ma wax ci seen xol yu xat Ennemies yi dañu bare, wane ginaaw paaka ci taat Dama busy, dama sori, nama Yalla musal ci cat Real niggaz yi duñu worry, nee nañu Natty “Zeyn khatt” Xaj yaa ngi may màtt, noon yaa ngi may pàdd Ni ñu yàkkamtee ma wadd, ragal samay kàddu Yaw looy daw bay daanu? Baa du da nga waaru? Boy Capsi, original...Learn MorepopNatty Jean[Lyric] Prezident (Natty Jean)
Waxal ag askan wi… Président nee nañu dafa doy Askan bi moo ma yónni nee nañ sonn nañu tàyyi nañu Sunu président ci yaw la ñu wara roy kon boog na nga ligeey Mag ñi ligeey, ndaw ñi ligeey, buñu bëgee rew mi jëm kanam Kune defal sa keemtalaay kàttan buñu bëgee rew mi jëm kanam Amul gòor, amul jigeen, ñun ñëpp a ci bokk yam Ñun bëguñu…ñun bëguñu...Learn MorepopNatty Jean[Lyric] Ak Yow (Natty Jean)
Sans yaw, dafay melni àdduna day bëg tukki Ak yaw, damay melni ku tëye alalu bukki Dëgg la sama chérie kon tay jii maa la tooñ Wante yaa ma xamal tay jii luma xamulwoon Maa ngi fataliku bi ñuy toog ci boppu koñ Suñuy gént ag sunuy yeene rek lañu amoon Waye seytane dafay faral di jaxase di ñu féewale Seytane bëgul ñaar ñu bëgante, bëgul ñuy fo di...Learn MorepopNatty Jean[Lyric] Allah (Natty Jean)
Man xawma ñaata at a ngui nii ma toog di ko xoslu Gëm ne bes di na ñëw Yalla ubbil ma ayi bunt Nee nañu damay caaxaan, ñële ne nañu damay fontu Ñooñu duma leen tontu. Who God bless no man can test I give thanks and praises to the Lord Allah Buur bi musal nama ci musiba ag balaa Bëg naa bala may genn ci aduna Samay waa-jur, samay mbokk bayyi leen ci...Learn MorepopNatty Jean[Lyric] Taya (Natty Jean)
Ils disent qu’ils vont nous régler nos problèmes sans soucis Chaque jour c’est les mêmes histoires c’est les mêmes mensonges bande de pussys Ils veulent que l’on se plie ils veulent que l’on soit adoucis Alors on est venus vous dire qu’on n’est pas fous ça suffit Ils nous pris pour qui on ne veut plus de vos salades Tellement d’hypocrisie que le...Learn MorepopNatty Jean[Lyric] Lou Teugue Tass (Natty Jean)
Lu tëgg tas ci life bi! Lu tëgg tas ci life bi! My broda lepp luñu waxantewoon, lepp liñu digaalewoon Lepp liñu yeenantewoon leegi jeex na, leegi dem nga! My sistren man ag yaw du kan moo tooñ, Buur bi Yallaa ñu boolewoon, melna ni bokkatu ñu yoon leegi jeex na, leegi dem na, namm naa la! Lu tëgg tas, lu tëgg tas, maa lako wax lu tëgg tas Amna fo...Learn MorepopNatty Jean[Lyric] Salimata (Natty Jean)
Sali daa jekk, am taar, daa melni moom lañu doon xaar Sali de gëmul system star, bu amul taxi jël car Te boo ko gisul Almadies mën nga ko romb Grand-Dakar Sali du gel bu xamadi, daa am yar machalla kaar ! Sali bëgul góor bu koy jox ba paré amul ci moom respect Bëgul am affaire ag benn góor bu ñàkk kersa Bëgul bula rombee dox doxam nga diko...Learn MorepopNatty Jean[Lyric] Falling (Natty Jean)
Babylone is falling xanaa gisoo seen i colin? Babylone is falling xanaa gisoo seen i waxin? Balylone is falling xanaa gisoo seen i jëfin? Man de yalna ma Yalla musal ci bile ñàkk teggin! Man bi may nekk gune lañ ma jangal respect Kila magg a la ëpp sagar kon bul ko tester Li fi maam bóoy bayyi ci lu baax warna fi rester Indiscipline bi ci dëkk bi...Learn MorepopNatty Jean[Lyric] Laissez-nous (Natty Jean)
C’est juste un petit échange que j’aimerai avoir avec vous Le peuple c’est nous alors debout et soyons tous au rendez vous On leur donne tout tous les atouts on est toujours pris pour de fous Des lois des lois des droits de mes couilles aujourd’hui tout est devenu flou Un frère qui tombe sur le champ de bataille ils se foutent de qui a tiré Ce...Learn MorepopNatty Jean