Song: Ego Trip
Artist:  Natty Jean
Year: 2021
Viewed: 4 - Published at: 2 years ago

Bayyi leen ma wax, ma wax ci seen xol yu xat
Ennemies yi dañu bare, wane ginaaw paaka ci taat
Dama busy, dama sori, nama Yalla musal ci cat
Real niggaz yi duñu worry, nee nañu Natty “Zeyn khatt”
Xaj yaa ngi may màtt, noon yaa ngi may pàdd
Ni ñu yàkkamtee ma wadd, ragal samay kàddu
Yaw looy daw bay daanu? Baa du da nga waaru?
Boy Capsi, original “Freedom Five” lama taxawaalu
Maliba lama demoon xoslu wanté leegi fekk ma Paname
Bamako moma ubbil bunt ne ma leegi demal kanam
May represent Sénégal, yeen sax xam ngeen seen égal
We keep the fire burn et oui je le fais d’une façon légale
Fi ma jaar bu fa jaar ndakh, boo fa jaare taq ban
Original Natty fire gars yi ne nañ phénoménal
Reggae ragga hip hop roots wala jox ma dancehall
Indi fresh vibes, flow, lyrics, call me criminal

This is for my enemies yes yes
No one could not stop me yes yes
One love for the family yes yes
Mane maay xaritu xale yi, may feccloo mag ag gune yi
Fexeel ba buma xosi
Niggaz yi ñu ngi soppeeku ci kanam da na ñu rusi
De Dakar à Bamako, Paris, Canada, Djibouti
Ma takk sama dàll, sama tubëy di ko wuti
Drapeau Galsen ku ko yenu du lu tuuti
Bëg sama rew a waral duma nelaw guddi
Paris is burning when my niggaz in the building
Lu Yalla teg ba nopi man kenn mënu ko dindi
Maximum de respect Humble Ark mooy sama crew
Weyndé jëlal yaa ko moom, man duma faate samay bros
Ki doon làcce Natty Faya leegi am jox na la ko
Du money, du auto, du dàll, du dara mooy tax ma soppeeku
Benn real a ma gënal camion fake, ludul dëg bokkuma de
Music ci xol laa koy dundee kon man ag yaw dañu wuute
Bumay dee nama gainde ray, bumay dee nama gaynde ray

Wax fa dëg maa ngi sant, doylu naa li ma Yalla may

( Natty Jean )
www.ChordsAZ.com

TAGS :