Song: Denkaané
Artist:  Baye Mass
Year: 2020
Viewed: 64 - Published at: 4 years ago

(Pere Becaye Mbaye)

Munj moy takh nga am fi
Lifi sa ndey am
Ta sa bo amé loula naxari
Ba wara nyibissi sa keur baye
Na sa xel dem ci ne bo yegue ci sa ndey
Yang koy feke ci sa wete Baye
Kone say dome liy sen guenel Bakh ci niom moy sa wo diougue nga wara roy mame
Ndax sey du lu nex Waye dafa nex


(Baye Mass)

Atou dou wess
Teh dou lou bess
Dieum diapa, diapa ci dianga
Deugg dou soufé
Khol yi nagn ko bolé
Wathiou sa ande ben yon
Wali yane nooo
Nyanal na la waw
Ni bye nga fi yaye bye nga fi baye
(Bayilen Ganaw)
Negou sey du lu nex
Teh dou meuseu nex
Noon yangi xool
Thi bind mu soufé
Ndax bind mu ndaw la
Ci la diakarlo ak yow
Dila wax deugg
Yaw sama mak nga
Waye deugg du soufé
Deugg du ndaw
Deugg amoul morom
Bu diougué ci xolou boromam
Biss bi la kuneka di nyan
Donte du lu nex
Donte du lu nex
Nga bye ndeye ak baye, bye mbok ye, bye xarit ye dem feki kenene
Denk na la Yallah
Yow dei sama xol nga danga sori ci man lool
Waye santal banga amé, Yaye diou melni ki
Beuthieugal naniou
Goudil na nyu mom souniou Yaye
Santal Yallah banga amé, Baye bou melni ki
Yarr naniou ci diom, Fouleuh, Gor ak Fayda
Soko yobo am fa ndam yaye

Negou sey du lu nex
Teh dou meuseu nex
Danga teudé niaxanay
Teudé nday diou seekh
Mani munj meti na lool
Waye lo fi munj mu diex
Sama mak djé denk na la lolu

( Baye Mass )
www.ChordsAZ.com

TAGS :