Artist: Baye Mass
Lyrics of Artist: Baye Mass
Lyrics of Artist: Baye Mass
[Lyric] Xale Rewmi remix (Baye Mass)
Bismillah niou deeti door dellu saku nian Di nian Yallah mu nangoul niu lep lun ko nian Seytane dey yakh khel di sopi khalat Di feweule andado Niun daal bum nyu laal yaye Yeen xale rewmi Ni la ko beugue waw Sen atmi mo du atoum gune Soxlo woul beuri wakh Nanj bolo won mak nyi Nyun nioy doule rew Gone su taggou ay wadiouram Disso ak nioom seu...Learn MorepopBaye Mass[Lyric] Denkaané (Baye Mass)
(Pere Becaye Mbaye) Munj moy takh nga am fi Lifi sa ndey am Ta sa bo amé loula naxari Ba wara nyibissi sa keur baye Na sa xel dem ci ne bo yegue ci sa ndey Yang koy feke ci sa wete Baye Kone say dome liy sen guenel Bakh ci niom moy sa wo diougue nga wara roy mame Ndax sey du lu nex Waye dafa nex (Baye Mass) Atou dou wess Teh dou lou bess Dieum...Learn MorepopBaye Mass[Lyric] Niaboot (Baye Mass)
Rethiou fek dieuf wes Njaboot bu des Ganaw Mou wara feki yaye dji wakh ko ko Wa keur gui daniouy dioye Desse touniou rogogne Dem naniou soga nane fouma koy waxeti Ay dome you sax si xol Niou donone li nyu bole Mane fouma wara diar ba niou balma Nio donone souniou dole Nio donone souniouy xol Nio donone liniouy reer lo, nakieu la wala...Learn MorepopBaye Mass