Song: Niaboot
Artist:  Baye Mass
Year: 2020
Viewed: 41 - Published at: 4 years ago

Rethiou fek dieuf wes
Njaboot bu des Ganaw
Mou wara feki yaye dji wakh ko ko
Wa keur gui daniouy dioye
Desse touniou rogogne
Dem naniou soga nane fouma koy waxeti
Ay dome you sax si xol
Niou donone li nyu bole
Mane fouma wara diar ba niou balma
Nio donone souniou dole
Nio donone souniouy xol
Nio donone liniouy reer lo, nakieu la wala ndioumte
Njaboot gui di weet
Anhhhh
Njaboot gui di dioy
Njaboot, fek njaboot gui weet, bilay demouma
Rethiou fek jeuf wees
Fouma ka koy waxe
Nimako feke, nimako feke
Nimako...feke

( Baye Mass )
www.ChordsAZ.com

TAGS :