Song: Xale Rewmi remix
Artist:  Baye Mass
Year: 2020
Viewed: 24 - Published at: a year ago

Bismillah niou deeti door dellu saku nian
Di nian Yallah mu nangoul niu lep lun ko nian
Seytane dey yakh khel di sopi khalat
Di feweule andado
Niun daal bum nyu laal yaye

Yeen xale rewmi
Ni la ko beugue waw

Sen atmi mo du atoum gune
Soxlo woul beuri wakh
Nanj bolo won mak nyi
Nyun nioy doule rew
Gone su taggou ay wadiouram
Disso ak nioom seu ndialbeen
Fu mu ne ci aduna senj thia yakaar lu bakh

Yeen xale rewmi
Ni la ko beugue waw

Bu nu wakhtane ak sunuy baye
Mak matna ba thim rew
Lu niu wakh nyu degg ko boole sunuy xalat
Nyi ci biti nyi ci biir fu waay meuna ne
Nen bole sunuy xalat rew mi dem kanam yaye
Yeen xale rewmi
Ni la ko beuguе waw

Man daal waleu bima feetee
Maaki samay gars
Pexe munе nyung ko dieem nguir sunu rew mi naat
Sunu beugue sunu rew mi naat danyu wara boolo
Ta kat fou way meune ne sen thia yengueuto

( Baye Mass )
www.ChordsAZ.com

TAGS :